Compositor: Não Disponível
Maestro on the beat
Bëgguma sañse (nga ni?), sañse ma bëgg
Yaw danga bari doole, arrêteel mënoo ñu jàppale
Li nga sañse ni rafet na xoolal ni mu la jàppe
Moo yaw danga neex li dama ko sol pur lakk yapp
Booleen bëggee deuxième tour na xale yi ñan ma ko ci njëkk
Ci njëkk
He, yaa ma na sañse
Sañse di paw paw
Ku ko man ni la koy defe
Ci njëkk
He, sañse ci yaw la ne
Jooyal ba wadd
Waaye li ma sañse
Hitoire dina ko bind
Li du mak ñoom, li du mak ñoom
Ngeen bi du mak ñoom
Xam nga sañse ma ci toog
Wowowowaay
Li du mak ñoom, li du mak ñoom
Ngeen bi du mak ñoom
Xam nga sañse ma ci toog
Li ma sañse du info, ci sama quotidien la
Dara daluma maa ngi ci jàmm, lalal bant nelaw kaar
Ma cas leen ki ma ñawal fi ma xottile (eh!)
Dem ci karaj am ci pose bu nice (waxaat leen kaar)
Yaw danga bari doole, arrêteel mënoo ñu jàppale
Li nga sañse ni rafet na xoolal ni mu la jàppe
Moo yaw danga neex li dama ko sol pur lakk yapp
Booleen bëggee deuxième tour na xale yi ñan ma ko ci njëkk
Ci njëkk
He, yaa ma na sañse
Sañse di paw paw
Ku ko man ni la koy defe
Ci njëkk
He, sañse ci yaw la ne
Jooyal ba wadd
Waaye li ma sañse
Hitoire dina ko bind
Li du mak ñoom, li du mak ñoom
Ngeen bi du mak ñoom
Xam nga sañse ma ci toog
Wowowowaay
Li du mak ñoom, li du mak ñoom
Ngeen bi du mak ñoom
Xam nga sañse ma ci toog
Waawaaw
Waxat leen kaar
Mashallah!
Waxaat leen kaar
Wawawawaw!
Céy, li nga sañse!