Compositor: Não Disponível
Dangay xaar
Dangay xaar
Wowowowowowaay
Hé!!!
Xalé bingay sén dafa fresh am vibes
Man deh nima téyé game dafa am thiass dal
Dang ma def none sa girl dima snap di TikTok
Dam yag def hits sa xol bi yaw dissi pink ponk
Doma dieund dama chère
Ndakh mano ma dieund dama chère
Loloy deug!
Man ak yaw li dou guerre
Ndakh man may sa mbaxalou xér
Loloy deug!
Mané fimay jouer
Dofa départ
Si banc bi ngay tokk
Dangay xaar
Man fimay jouer
Yaw dofa départ
Si banc bi ngay tokk
Dangay xaar
Diaroul teup di dal ba mélni beuy ndakh
Dangay xaar
Ya yéy dioy do dem xam nga nii
Dangay xaar
Xamnga man la kangham bi motakh
Dangay xaar
Mano wax ba keupeu ndapp li xamnga ni
Dangay xaar
Sa xol mou binégarr motakh
Dangay xaar
Sama xol da frigo hoo!!
Dangay xaar
Sa xol mou binégarr motakh
Dangay xaar
Sama xol da frigo hoo!!
Dangay xaar
Sama tankeu bu deungué yako guiss
Ndakh yama fété ganaw
Ma lékeu si galou xathie deh doko guiss
(Doko guiss)
Ndakh rombu nala di naaw
Tkt dangay xaar yaw
Mani dangay xaar
Fima ak si tay liguey la
Yeah! Yeah!
Wiri wiri diari ndari maestro leu
Dama chaud dama ayy ah ah ah!
Xamé ma boul dof man mi leu
Ma bi téyé bi arts ah ah ah!
Mané fimay jouer
(Fomay jouer)
Dofa départ
(No no)
Si banc bi ngay tokk
Dangay xaar
Diaroul teup di dal ba mélni beuy ndakh
Dangay xaar
Ya yéy dioy do dem xam nga nii
Dangay xaar
Xamnga man la kangham bi motakh
Dangay xaar
Mano wax ba keupeu ndapp li xamnga ni
Dangay xaar
Sa xol mou binégarr motakh
Dangay xaar
Sama xol da frigo hoo!!
Dangay xaar
Sa xol mou binégarr motakh
Dangay xaar
Sama xol da frigo hoo!!
Dangay xaar