Moulay Thieuguine Love (feat. Satou Niang)

El Maestro

Compositor: Não Disponível

El Maestro
(Oh Satou bi)
Satou Niang
Hé yah yah yah yah yah

Yaay sama wéeruwaay
Yaw danga mas a doon sama waay
Suma reni xol
Ma ni xam nga ni yaw laa love

Bokkook ñoom te duñu yaw
Yaa raw gaynde ci àll bi
Bu jinnee bëggee ku yëg dangay daanu
Aladji, kenn du yaw

Dama jonge ba exagéré
Ni may séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk bi wet
Maay ki lay feccal mu lay thieuguine

Dama jonge ba exagéré
Ni may séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk bi wet
Maay ki lay feccal mu lay thieuguine

Mu lay thieuguine (kaay)
Mu lay thieuguine (anh)
Mu lay thieuguine (nga ni?)
Mu lay thieuguine (kaay)
Rësëgin tacc (ahn)
Rë-rësëgin tacc
Rësëgin tacc
Rë-rësëgin tacc

Maes sama chibiribi lalale, éh héé!
Xam nga yaw fii yaw yaa fi ne
Soo fi nekkul, danga may wetal

(Je t'aime) li nekkatul infos
(Tu m'aimes) li nekkatul cas
Maa lay feccal di la leebal
Bañuma ba xale di ma ree

Dama jonge ba exagéré
Ni may séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk bi wet
Maay ki lay feccal mu lay thieuguine

Kon danga jonge ba exagéré
Ni ngay séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk ci wet
Yaay ki may feccal mu lay thieuguine

Kon danga jonge ba exagéré
Ni ngay séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk ci wet
Yaay ki may feccal mu lay thieuguine

Mu lay thieuguine (kaay)
Mu lay thieuguine (anh)
Mu lay thieuguine (nga ni?)
Mu lay thieuguine (kaay)
Rësëgin tacc (ahn)
Rë-rësëgin tacc
Rësëgin tacc
Rë-rësëgin tacc

Kon danga jonge ba exagéré
Ni ngay séye da particulier
Bu guddi jotee ba nekk ci wet
Yaay ki may feccal mu lay thieuguine

Mu lay thieuguine (kaay)
Mu lay thieuguine (anh)
Mu lay thieuguine (nga ni?)
Mu lay thieuguine (kaay)
Rësëgin tacc (ahn)
Rë-rësëgin tacc
Rësëgin tacc
Rë-rësëgin tacc

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital