Compositor: Não Disponível
Bul jooy
Sister
Promotions canapé
Moo ngi toj dëkk bi billaay
Ñoom ñi ma koy teg (waawaaw)
Ñoom ñoo may sargal 8 mars
Violence conjugale (ndeysaan)
Moom laay dundu billaay
Moom mi ma koy teg (wowowa waway)
Moom moo may sargal 8 mars
Journée internationale
Des droits de la femme
Journée de réflexion la wara doon
Journée de revendication (non non)
Warul nekk journée pukareek sañsé (Non non non)
Jigéen yi ñuy maltraité
Lañuy sargal
Bu 8 mars jotee (jotee)
Yeen chef d'entreprise yi orgainser fête
Woo kepp kuy jigéen di wax ay baax baaxam
Te ba muy ñëw ci bureau-am
Bëgg liggéey def ko laaj boppam
Ba muy ñëw bureau-am
Bëgg bëgg promotion
Daf ko violé (waawaaw)
Non, non, non
Non, non, non
Non, non
Kisa rakk la (lii dafa ñaaw!)
Bul ko def li de! (Lii dafa ñaaw!)
C’est ta soeur
Promotions canapé (wowowoy)
Moo ngi toj dëkk bi billaay (hé)
Ñoom ñi ma koy teg (non, non, non)
Ñoom ñoo may sargal 8 mars
Violence conjugale (ndeysaan)
Moom laay dundu billaay
Moom mi ma koy teg (wowo wowo wowoway)
Moom moo may sargal 8 mars
Wowowowo wowoway
La violence faite aux femmes
N’est pas seulement physique
Le faites de l’atteindre psychologiquement
Est vraiment horrible
Yaa ko wara protéger
Yaa wara dalal xelam
Yaay góor
Yaa wara tax du jooy
Lalala lalala lalala
(Hé Yaah)
(Du yoon)
Yaa ngi nekk ak moom ci kër gee
Di ko violenter
Xooloo doom xoolone
Ki man na doon sa rakk
Bu jigéen wala sa jarbat
8 mars jotee
Ngeen ni hotessou
Naan jabar sama
Di ko sargal muy reetaan
Xamoo lu muy dundu ci xolam (xolam)
À travers la voix de femme je parle (hé aah)
Je parle, je parle et je parlerais
À travers le cœur de la femme
Je pleure, je pleure
Maa ngi jooy wowoway