Fipou Na (feat. Yacine Diop)

El Maestro

Compositor: Não Disponível

Yeah Zay
Man bàyyi naa ko, waay
Fippu naa man

Man fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne ma déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet waay!

Danga ma dàqal Ouroul Ayni
Ma bëgg la lool ee
Nga miinal ma sa bopp
Ma dof ci yaw
Su ma la defee pepe
Ngay ñaanal nan sa xol bi dafa sedd
Su ma la séene ngay dem
Lu dul yaw dama koy gedd
Waaye léegi ne nga ma lay déranger
Loolu def ma góomu xol
Di ma ronger, heee
Bàyyi naa la (ma bàyyi la ko)
Man mile

Man fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne na déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet

Man fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne ma déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet waay!
(Sama xol bi ne ma déedéet waay!)

Man mi dama jax maak ji dañu doyal
Mon amour, tu en as trop abusé
Jarul may forcer
Mbëggeel du kenn a rekk ko def
Jarul may sale
Xol bi yaa ci nekk
Ni la mënoon demee chérie booy
Bye bye

Man fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne na déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet

Fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne ma déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet waay!

Mbëggeel a compliqué

Man fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne na déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet

Fippu naa, bàyyi naa ko
Xol bi ne ma déet
Man gedd naa ko wan gannaaw
Sama xol bi ne ma déedéet waay!

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital