Choqué (feat. Khadim Temps)

El Maestro

Compositor: Não Disponível

El maestro oh oh!!
Khadim temps temps temps!
Migui niaw deh (dieuleul)
Wawawaw

Lingay snap diko TikTok diko cas, choqué
Ték beut domou diambour neko diaaa, dama choqué
Lingay xawii soutoura diambour yi rek, moma choqué
Ligay filmer say moment d’intimité dama choqué

Hé choqué!! (Thiey wouyay)
Choqué!! (Xalé bu ko man ni ngakoy défé)
Man dama choqué!! (Wouy fecc bu bess)
Choqué!! (Choqué choqué choqué choqué mounan)
Choqué!!

Waxu ma sen togay, loy lidianti nimay doxé?
Amo loma waxal, wayé manu nguén teulé
Dewma keur yama ngitax, abonné wouma yama télé
Xalé bi ningay job bé, daf ma choqué

Tank loxo nop (yaw dieulal), sa guémiñ douma wacc (thiey)
Douma mana yég (doxal), say beut tama topp (thiey)
Sa beuñ yinga sothie, dima siñ foumu rombeu
Sa xol bi dissi nathie, démal nga tok tamit

Lutax nga di wax, deuk bi taar
Yaw nga deuk si cas, dugu ci vie privée diambour
Diko lidianti ba faar nek si cas

Sa jiko ma yém, ningay doxé
Daf ma choqué, yéné wo kén jaam
Daga soxor

Lingay snap diko TikTok diko cas, choqué
Ték beut domou diambour neko diaaa, dama choqué
Lingay xawii soutoura diambour yi rek, moma choqué
Ligay filmer say moment d’intimité dama choqué

Hé choqué!! (Thiey wouyay)
Choqué!! (Xalé bu ko man ni ngakoy défé)
Man dama choqué!! (Wouy fecc bu bess)
Choqué!! (Choqué choqué choqué choqué mounan)
Choqué!!

Ya wutt appartement ci internet, évidemment yaw sa xol day wett
Xadialo si kén, rathieu lep si bop
Garouwalé Snapchat, negatif si TikTok

Tégu mala xéff, nangu na ningay déffé
Yaw la Messi, yaw la cris
Té nangou wo madone mbappé, yafi daak lep nak
Sa boppu ngakoy nakhé, man xeuyouma rek né thieupp
Wadiu bax dama ñaffé waw

Lutax nga di wax, deuk bi taar
Yaw nga deuk si cas, dugu ci vie privée diambour
Diko lidianti ba faar nek si cas

Sa jiko ma yém, ningay doxé
Daf ma choqué, yéné wo kén jaam
Daga soxor

Lingay snap diko TikTok diko cas, choqué
Ték beut domou diambour neko diaaa, dama choqué
Lingay xawii soutoura diambour yi rek, moma choqué
Ligay filmer say moment d’intimité dama choqué

Hé choqué!! (Thiey wouyay)
Choqué!! (Xalé bu ko man ni ngakoy défé)
Man dama choqué!! (Wouy fecc bu bess)
Choqué!! (Choqué choqué choqué choqué mounan)
Choqué!!

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital