Nel Mashallah

El Maestro

Compositor: Não Disponível

Dama dem ba fu ma tël
Ñu ne ma xale bi kaar
Dafa dem ba fu ma sañse
Ñu ne ma kaaro mashallah
Damay lakkatu sax
Dama tamm rare man
Cat gi ci limiñ
Dafa sew te gaaw

Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la
Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la

Lakalé ne N’golo Kanté
Cat dafa sew te gaaw (jëlal)
Xaral ma takk Pétaw
Wala ma setti Maam (nga ni ma)
Noon yi noon yi noon yi
Dañu doy waar
Jaral na leen dem si sëriñ
Garé la bu yabo
Nga fagaru so dewe safuleen sax
Cool lal ba ma sangatu
Séeti baxaw lalaké

Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la
Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la

Tathiou lén mu rirr
Waawaaw
Jëlel!

Bul ma catu catu catu catu
Bul ma catu
(Ñëwal)
Bul ma catu catu catu catu
Bul ma catu

Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la
Iyoo ho, waxal mashallah
Iyoo iyoo, man doomu jambur la

Nél Mashallah hahan
Doomu jambur la ah ah

Yàlla nañu Yàlla Mussal
Si cat làmmiñ
Musiba la de!
Ku garé moo la garé
Làmmiñ
Ku taxaw moo la freiné
Yàlla bu ma freiné man

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital