Potion Magique

El Maestro

Compositor: Não Disponível

Askan wi la joxoon nga añ
Bu la dige réer gëm ko
Ñun nji faloon Diomay
Dinañu ko jox assemblée
Guy gi nar a dundal Sénégal
Ñun dinañu ko ar ba mu mag sunu gal la
Système bi jogé fi abadan
Dinañu ko ray mu dee, mu abal ñoo

Ngir Diomaye doxal, Sonko di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité

Dafa jot ñu am assemblée bu bees
Ak ay députés yu am qualité
Liggéey rekk te duñu dagasante
Bulletin bu baax bi mooy bu Pastéf
Kaay ma wan la ko
Dafa verte weex am photo Ousmane
Sonko tutti rouge ak Pastef les Patriotes
Wan ko Yaay wan ko Baay
Topp ndigalu Tata Maimouna Bousso
Focus!
Le 17 ma baccleen
Baccleen na xiir yi dall
Focus!

Kon su ñu la diggee réer gëm ko
Ñun nji faloon Diomay
Nioune nji falone Diomay
Dinañu ko jox assemblée
Guy gi nar a dundal Sénégal
Ñun dinañu ko ar ba mu mag sunu gal la
Système bi jogé fi abadan
Dinañu ko ray mu dee, mu abal ño

Ngir Diomaye doxal, Sonko di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité

Bu ñu amee Majorité
Loi bu baax ñu Voté
Dindi amnesty bi
Delloo justice Martyres yi
Jubb-jubbal jubanti rekk
Teg fi haute cours de justice
Ku fi jëloon alalu réew mi
Dinga ko gokki watt
Sénégal ñoo ko man a défar
Góor jigéen mag ak ndaw ànd liggéey
Sénégal vision 2050
Wacceel coono sunuy doom yi taxoon ñuy xéxx
Dont de soit pour la patrie
Pour un Sénégal souverain, juste et prospère

Askan wi la joxoon nga añ
Bu la dige réer gëm ko
Ñun nji faloon Diomay
Dinañu ko jox assemblée
Guy gi nar a dundal Sénégal
Ñun dinañu ko ar ba mu mag sunu gal la
Système bi jogé fi abadan
Dinañu ko ray mu dee, mu abal ñoo

Ngir Diomaye doxal, Sonko di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité
Ñu doxal di doxal, ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet mooy Majorité

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital