Compositor: Não Disponível
Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh!
Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh!
Oh wanh! Oh wanh! Anh han!!
Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh!
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Sama xel mi mom legui mou dem
Ndax legui ma doff
Sama none yi wéxal na beugn yi
Fass yéné ré
Sama néné touti yaw boul ma bayi
Souma togué ba xalatt lén
Man douma néh
Damay ndérmélou
Di ndérmélou (wawaw), di ndérmélou (Ndeysane)
Di ndérmélou
Yama done watal ni boudoul man
Dou done kénén nioumay roubé
Dima roubé (Dima roubé héhéy)
Cheri boy boul ma bayi
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Dama dioum ba dila woh telephone
Faté danio xoulo nitt ak kamou mine
Ay koussi mérr bay watt faté nga dioubo
Makhalla seuytané nga
Fouma dougal cherie wakh ma
Xana guisso nima diéxé temps yi
Yaw rek lay xalatt
Rafet nga lolou dougou sama xol
Diaxassé ko réw ba doff (soff)
Capricieuse ouly lan la
Boul ma xol
Xamgani balnala (Balma)
Waw kaay fii namone nala
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Boul ma bayi
Boul ma bayi sama Banana
Boma bayé
Beuss boma bayé nassi doff
Boul dem ba bayima baby
(Yaw xamga yawla am baby)
Cheri Kaay kaay Kaay kaay fiii
(Kaay kaay Kaay kaay fi thie Mane)